Ezekiel 33:26 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Yeen wóoluwuleen lu moy seen saamar, ngeen di def jëf ju siblu, ku nekk di jaalook jabaru moroomam, ba noppi di moom réew mi?”