Ezekiel 34:10 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii di dal fi kaw sàmm si. Maay nangoo sama gàtt ci seeni loxo, dakkal seenug càmm, ndax ñu noppee sàmm seen bopp. Maay foqatee samag jur ci seeni sell, ba dootuñu leen ndawaloo.