bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 34:13
Ezekiel 34:13 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Maa leen di seppee ci xeet yi, génnee leen ci réew yi, dajale leen, yóbbu leen seen suufas bopp. Maa leen di foral, sàmm leen kaw tundi Israyil ak biir xunti yaak mboolem fu ñu dëkke ci biir réew mi.