Ezekiel 34:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Waaye Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yeen sama gàtt yi, maa ngii di àttesi diggante xar ak moroom ma, ak diggante kuuy yi ak sikket yi.