Ezekiel 34:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Gannaaw loolu maa leen di waajalal ab sàmm bu leen di sàmm. Kookooy Daawuda sama jaam bi. Moom moo leen di foral, mooy doon seen sàmm.