Ezekiel 36:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Gannaaw noon bee ne leen: ‘Ñaw! Seen kawte yu yàgg yii, tey nooy boroom.’ ”