Ezekiel 38:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
daldi ne: ‘Maay songi réew mu ne ŋàpp, maay dali ca kaw waa réew mu ne finaax, dëkke xel mu dal, te du tata ju wër fu ñu dëkke, ñoom ñépp, du buntu dëkk, du tëjukaayu bunt.’