Ezekiel 38:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa Saba ak Dedan ak julay Tarsis, ak mboolem seeni boroom daraja ñoo lay wax ne la: ‘Nangu alal a la yékkatee? Sëxëtoo alalu xaree la taxa bàbbi sa gàngoor, ngir yóbbu xaalis ak wurus, nangu jur ak alal, ba dajalee ca xare ba koom gu takku?’ ”