Ezekiel 39:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Yaw nit ki nag, waxal waxyu ci kaw Gog, nga ne: “Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Maa ngii fi sa kaw, yaw Gog, boroom Meseg ak Tubal.