Ezekiel 39:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Dañuy tabb nit ñu féetewoo di wër réew mi, ñu àndandook tukkikat yi, di rob néew yi des ci àll bi, ngir setal ko. Bu juróom ñaari weer yi jeexee ñu tàmbalee seetaat.