Ezekiel 39:23 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kon yéefar yi dinañu xam ne ñaawtéefi waa kër Israyil moo leen yóbbe ngàllo ndax la ñu ma ñàkke worma, ba ma xañ leen sama kanam, teg leen ci seen loxoy noon, ñu fàddoondoo saamar.