Ezekiel 39:25 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Kon nag Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Léegi maay tijji wërsëgu Yanqóoba, maay ñeewante waa kër Israyil googu gépp, te maay fiire sama tur wu sell wi.