Ezekiel 4:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Te kat nanga sàkk bele ak lors ak ñebbe ak làntin ak dugub ak bele bu dëgër. Nga boole lépp ci lenn ndab. Moom ngay lekk diiru fan yi ngay tëdde wet. Diiru ñetti téeméeri fan ak juróom ñeent fukk (390) nga koy dunde.