Ezekiel 40:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay palanteeram ak dal-luwaayam ak nataali garabi tàndarmaam it, lépp a bokk ak yu buntu penku ba dayo. Juróom ñaari dëggastal ngay yéeg, janook dal-luwaayu ba.