Ezekiel 40:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Néegi wattukatam yaak jënam yaak biir dal-luwaayu mbaar ma, lépp a bokk ak ya jiitu ay dayo. Mbaaru bunt ba ak dal-luwaayam am ay palanteer ba dajal, guddaayu mbaaru bunt ba di juróom fukki xasab, yaatuwaay ba di ñaar fukki xasab ak juróom.