Ezekiel 40:33 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ay néegam aki jënam ak biir dal-luwaay ba, lépp a bokk ak ya ca des ay dayo, juróom fukki xasab ci guddaay, ñaar fukki xasab ak juróom ci yaatuwaay. Mbaaru bunt ba ak dal-luwaayam am na ay palanteer ba dajal.