Ezekiel 40:36 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bunt ba daa ànd aki néegam aki jënam ak dal-luwaayam ak palanteer yu ko wër, ba mu daj. Guddaay ba di juróom fukki xasab, yaatuwaay ba di ñaar fukki xasab ak juróom.