Ezekiel 41:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Tabax bi féeteek dig-digalu feguwaay bi ci sowub néeg Yàlla bi, yaatuwaayam juróom ñaar fukki xasab la, guddaayam di juróom ñeent fukki xasab, dëllaayu miir ba di juróomi xasab.