Ezekiel 41:17 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw buntu néeg Yàlla bi, ba ci biir néeg Yàlla bi, jëm biti, ak kaw miir bi ko wër, biir ak biti, lépp lañu natt.