bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 41:22
Ezekiel 41:22 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sarxalukaay bi bant la, taxawaayam di ñetti xasab, guddaayam di ñaari xasab, yaatuwaayam di ñaari xasab. Mu ami coll akub tegukaay aki wet, lépp di bant. Waa ji ne ma: «Taabal jii mooy janook Aji Sax ji.»