Ezekiel 41:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Taax mu la gëna kawe, gën laa yaatu, miir ba ànd ak moom gëna sew fi wër néeg Yàlla bi ba mu daj. Noonu lañuy yéege ay dëggastal, jóge ci suuf, jaare ca taaxu digg ba, ba ca taax ma ca kaw.