Ezekiel 42:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba loolu amee waa ji jaarale ma buntu bëj-gànnaar, génne ma ci ëttu biti bi. Mu yóbbu ma wetu sowu, dugal ma ca tabax ba janook dig-digalu feguwaay ba te sësook miiru biir ba ca wetu bëj-gànnaar.