Ezekiel 42:11 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mu ngi janook ab jàllukaay. Sàppey néeg yooyu daa bindoo ni bi féete bëj-gànnaar te bokk ak ñoom guddaay ak yaatuwaay, seeni bunt ak seeni dayo yépp di benn.