Ezekiel 42:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ñaari taax ya ca kawam nag, mu ci nekk yaatuwaayam a yées ma ko féete suuf, ndax taax mu gëna kawe moo ëpp jaarukaay bu mu bàyyi fi kanamam.