Ezekiel 42:8 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ndax néeg yooyu féeteek ëttu biti ba, guddaay ba bépp juróom fukki xasab la. Waaye sàppey néeg, ya sësook néeg Yàlla ba, guddaayam téeméeri xasab la.