bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 43:13
Ezekiel 43:13 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Lii nag mooy dayoy sarxalukaay bi ciy xasab, xasab bu ci nekk tegu yaatuwaayu catu loxo. Toogub sarxalukaay bi féete suuf, taxawaayam xasab la, yaatuwaayam di xasab, mu ànd ak kéméjam gu ko wër ba mu daj, te taxawaayu kéméj gi tollook yaatuwaayu catu loxo. Toogub sarxalukaay bi noonu la bindoo.