Ezekiel 43:18 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waa ji ne ma: «Yaw nit ki, Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Lii mooy dogali yoon yi jëm ci sarxalukaay bi, bés bu noppee, ci wàllu saraxi rendi-dóomal, ak deret ji ñu ci wara tuur.