Ezekiel 44:3 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Boroom jal bi nag, gannaaw mooy boroom jal bi, sañ na faa tooge, lekk fi kanam Aji Sax ji. Waaye ci dal-luwaayu mbaar mi lay dugge te fi lay génne itam.»