bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 44:5
Ezekiel 44:5 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Aji Sax ji ne ma: «Yaw nit ki, xippil, ubbil say nopp te def sa xel ci mboolem lu ma la wax ci wàllu dogali yoon yi jëm ci kër Aji Sax ji ak mboolem digali yoonam. Defal sa xel bu baax ci duggukaayi kër gi ak mboolem génnukaayi bérab bu sell bi.