Ezekiel 45:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Bu ngeen demee bay tegoo réew mi bant ngir séddoo ko, nangeen jooxeel Aji Sax ji dogu suuf bu gudde ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), yemook fukki kilomeetar ak ñett, yaatoo ñaar fukki junniy (20 000) xasab, yemook fukki kilomeetar ak genn-wàll. Suuf soosu sépp ba fa mu yem, lu sell lay doon.