Ezekiel 45:5 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Beneen dénd bu gudde ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), yaatoo fukki junniy xasab (10 000), na ñeel Leween ñiy liggéeyal kër Yàlla gi, ngir ñu am dëkk yu ñu dëkke.