bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 45:9
Ezekiel 45:9 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Yeen ñiy tooge jalu Israyil, na doy nag! Coxor geek jaay-doole bi, baleen ko. Njub ak njekk ngeen war di jëfe. Bàyyileen di nangu sama alali ñoñ. Boroom bi Aji Sax jee ko wax.