Ezekiel 46:1 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Buntu ëttu biir bi féete penku, na tëje diiru juróom benni fan yi ñuy liggéey. Waaye bésub Noflaay ba cay topp, na ubbiku. Bésub Terutel weer it, na ubbiku.