bible
ra
🌐 Language
English
Español
Français
Deutsch
Português
Italiano
Nederlands
Русский
中文
日本語
한국어
العربية
Türkçe
Tiếng Việt
ไทย
Indonesia
All Languages
Home
/
Bible
/
Compare Ezekiel 47:9
Ezekiel 47:9 — Compare Translations
1 translations compared side by side
Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem mbindeef muy def ndiiraan day daldi mana dunde mboolem fu wal mii jëm. Jën yi day takku lool ngir la fa ndox mii àgg, ba neexal mooma ndox. Mboolem fu wal mii àkki daal, lépp a fay dund.