Ezekiel 48:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Cér boobu mooy tànnéefu suuf si. Maneesu cee jaay, mbaa di ci weccikoo lenn, te lenn du ci tàbbi ciy loxo, ndax cér bu sell la, ñeel Aji Sax ji.