Ezekiel 48:21 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Li féete penku ak li féete sowu yépp nag te des ci suuf si, gannaaw cér bu sell bi, ak suufas dëkk bi, buur bi ci jal bee koy moom; wet gu ci nekk yaatoo ñaar fukki junniy xasab ak juróom (25 000), gii àkki kemu Israyil ga féete penku, gee àkki kemu Israyil ga féete sowu, cér bu sell beek kër gu sell gi nekk ci digg bi.