Ezekiel 48:22 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon suufas Leween ñi ak suufas dëkk bi day bokk féete ci diggu suufas boroom jal bi, suufas boroom jal bi nekk diggante céru Yuda ba ca bëj-gànnaar, ak céru Beñamin ca bëj-saalum.