Ezekiel 48:28 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Suufas Gàdd, kemug bëj-saalumam mooy doon kemug réew mi. Day dale fa Tamar ca penku ba, ba ca yoonu ndoxu Meriba ca Kades, leru walum Misra, ba ca géej gu mag ga.