Ezekiel 48:29 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Noonu ngeen di séddalee réew mi giiri Israyil yi, giir gu ci nekk, ngeen dogale ko noonu céru suufam. Kàddug Boroom bi Aji Sax jee.