Ezekiel 5:7 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
«Moo tax Boroom bi Aji Sax ji dafa wax ne: Gannaaw seen reewande wees na reewandey xeet yi leen séq, samay dogal, jëfewuleen ko; sama àttey yoon, sàmmuleen ko; sàmmuleen sax àttey xeet yi leen wër,