Ezekiel 7:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Bu jaaykat bi muccee it, du jotaat ca njaayam. Peeñu mi jëm ci askan wépp, daal, du toxu, ku nekk ñaawtéefam lay dunde, ba du leqliku.