Ezekiel 7:27 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Buur dina tiislu, garmi làmboo séri ñaawlu, baadoolay réew mi di kat-kati. Seeni jëfin laay jëfeek ñoom, seeni àtte laa leen di àttee, ñu xam ne maay Aji Sax ji!»