Ezra 1:2 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Sirus buuru Pers dafa wax ne: Mboolem réewi àddina, Yàlla Boroom asamaan moo ma leen dénk, te moom moo ma tabb, ngir ma tabaxal ko kër ca Yerusalem ga ca Yuda.