Ezra 1:4 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Mboolem bànni Israyil, ak fu ci nit mana féete, na ko waa foofa indil ndimbal ci wàllu xaalis ak wurus, alal aku jur ak saraxi yéene yu jëm ca kër Yàlla ga ca Yerusalem.