Ezra 10:12 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ci kaw loolu mbooloo mépp bokk àddu ca kaw ne ko: «Tigi, li nga wax rekk lanu wara def.