Ezra 10:13 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Waaye danoo bare, te muy jamonoy taw. Manunoo toog fii ci biti. Te it mbir mi maneesu koo lijjanti ci benn bés mbaa ñaar, ndax sunu tooñ ci mbir mii daa yaatu.