Ezra 10:14 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Kon daal na sunuy kilifa taxawal askan wi. Su ko defee mboolem ku nekk ci sunuy dëkk te jël ci jaambur ñi jabar day dikk, ku ci nekk ca bés ba ñu ko àppal, te mu ànd ak kilifa yaak àttekati dëkkam. Ñu topptoo mbir mi nag, ba keroog sunu merum Yàlla mu réy mi sababoo ci lii, dëddu nu.»