Ezra 10:9 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu ca tegee ñetti fan mboolem góori Yudak Beñamin daje nañu Yerusalem, mu yemook ñaar fukki fan ca juróom ñeenteelu weer wa. Ña nga toog ñoom ñépp ca ëttu kër Yàlla ga, di lox ndax solob ndaje ma, ak itam taw bu bare ba mu yemool.