Ezra 2:68 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
Ba ñu àggee ca kër Aji Sax ja ca Yerusalem, am na ñenn ca kilifa ya jiite seen kër baay, ñu joxe ay saraxi yéene ngir tabaxaat kër Yàlla ga ca gentam.