Ezra 7:16 — Compare Translations

1 translations compared side by side

Wolof KYG (Kàddug Yàlla gi)
boole ci mboolem xaalis mbaa wurus woo mana jële ci diiwaanu Babilon bépp, ak itam saraxi yéene yi baadoolo yeek sarxalkat yi joxe ci xol bu tàlli, lépp ñeel seen kër Yàlla ga ca Yerusalem.